Fails videos

Funny videos

Bril - Cila Bokk - Clip Officiel

Published on Sep 5, 2019 320,716 views

Download video: Download MP3:

** Mon nouvel album SUBA est sorti. A écouter et/ou télécharger en cliquant ici https://listen.lt/BrilSuba1 **

**Abonne-toi à ma chaîne ici https://goo.gl/Qw5BFh**
Après le succès de "Bras Long", CILA BOKK est le 2ème single extrait du nouvel album de Bril, SUBA, disponible à partir du vendredi 20 septembre sur toutes les plateformes de streaming et téléchargement.
Il est vital de bien se détendre et s'amuser : vos vedettes préférées comme Dudu, Mahfousse, Admow, Pagaye Mbaye, Pape Birahim ou Bass Thioung vous aident à oublier vos problèmes.
Cila Bokk, viens nous rejoindre, faisons la fête tous ensemble !
(voir lyrics plus bas dans cette description)
#Bril #CilaBokk #Suba #NouvelAlbum20septembre #ClassChicMusic #team221

**Crédits de la chanson "Cila Bokk" **
Auteur : Bril
Compositeur : Bril 
Studio enregistrement, mix, edit & mastering : Class’Chic Music par Bril

Une production de Class’Chic Music (Dakar, Senegal, septembre 2019)

**Crédits du clip "Cila Bokk" **
Réalisation : Weeflag
Un grand merci à Dudu , Mahfousse, Admow, Pape Birahim,, Jeeba,, jah hustla , Pagaye Mbaye & Bass Thioung pour leur aimable participation.

**Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux**
Facebook https://www.facebook.com/brilofficiel
Instagram https://www.instagram.com/bril_officiel
Twitter https://twitter.com/bril_fight4
Snapchat : @bril-fight4

** Contact management** 
Mr Mahmoud Sy : +221 77 036 48 31 
brilfight4@gmail.com 

**Booking international**
vincent.lagoeyte@soon.pro

**Lyrics de de la chanson "Cila Bokk" **

{Intro} 
hahahahaha 
(Bril on the Beat) ha ha 
Yeah yeaaah  Bril in the Building , héé 
Cila Bokk way way Cila Bokk , amoul Yakkalaté han , aythia Niou dém 

{Refrain} 
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress.
Boula kén ray doundou dafay nekh.
Koula beugga sonal Romb ko né mééss. 
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh . 
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”.

{1er Couplet} 
Lo xamoul kagn lay djèkh dafa wara nékh .
Boul faalé koulay méré wane ko beugn you wékh. 
Léppeu térangala , doundeul happyness.
Lofi meunti am té béggo , amna louthi déss. 
Fii dal Sénégal la , boula nékhé dinga béggué .
Boul nangou kèn yakkal-la dééko défé ning’ko beuggué.
Daniouy dadjé foo di réé té xawma no Toudou . 
Selfie def ay Vidéo you fun melni #Dudu, 
#Baye_Mbaye , #Makh_Pro / koufi mér kone Wéro. 
Warnga meune di enjoy nga né town wala ghetto . 
Boul nangou kèn dila téré Happy...
Kou sa life néékhoul , yakoy soppi . 

{Refrain} 
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress.
Boula kén ray doundou dafay nekh.
Koula beugga sonal Romb ko né mééss. 
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh . 
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”.

{2ème Couplet}
Héé Yaw nanga déf 
Koula beugga sonal thi wakh nèko mou déf, 
Défam té bayila rèk yaw nga néthi .
Take it easy , dafa wara yomb, waroul , méti hééé.
Beurina ay Nitt you done foo djaarfa feullalé . 
Tèki_thi romboula wakh bo saani niou feul- feulalé. 
Kheuthiolén son you #Lourd , ma ték lou #Léger dilén Mour .
Ngén may gueuna #Haine, maléni raw par #Amour. 
Bayilén niouy rawanté ngay dokh ndank , daagoul .
Té koukay djaay méti , né ko  “Lou Méti Yagoul”. 
Dél Khol sa none di réé né kouy sétane #Aba_Show 
Caméra cachée #Makhfouss lay yooné sama Cho (copine) 

{Refrain} 
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress.
Boula kén ray doundou dafay nekh.
Koula beugga sonal Romb ko né mééss. 
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh . 
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”.

{Outro} 
*kaay* Héé ...féthial féthial way , *kaay* ni rekla yeungoul yeungoul way .
*kaay* Hééé...féthial way , *kaay* ni rekla yeungoul yeungoul way .
*kaay*.   féthial féthial way  , *kaay*  niou dèm , hèè Han han yeungoul yeungoul way .
*kaay* mané Cila bokk haaa...yeah cila bokk.

Comments
  • Bril Officiel
    Bril Officiel 9 годин тому (змінено) Bonjour à tous, mon nouvel album SUBA est sorti ce vendredi 20 septembre. A écouter et/ou télécharger en cliquant ici https://listen.lt/BrilSuba1 J'espère de tout coeur que cet album vous plaira : je suis heureux de vous en faire découvrir aujourd'hui les 15 nouvelles chansons. One Love.
  • Diallo Mamadou
    Diallo Mamadou 2 тижні тому (змінено) Si tu es aime cette musique Tape j’aime 🙏🇸🇳🇮🇹❤️❤️❤️❤️❤️👈
  • Hawah Dialo
    Hawah Dialo 2 тижні тому Deug nexoul m3 dal jaim bril do sene morome😘😘😘
  • Md tv
    Md tv 2 тижні тому De ouf frère
  • Sale Yassin
    Sale Yassin 2 тижні тому Bonjour merci
  • Diallo Mamadou
    Diallo Mamadou 2 тижні тому Sale Yassin idm
  • khalifa Ababacar mbengue
    khalifa Ababacar mbengue 2 тижні тому Oh bril te le meilleur bilay Nice clip te nioungui wait album bi
  • Awa Ndong
    Awa Ndong 2 тижні тому Wa bril dal khol day guissè bamou bary 💪sama wax bimou sol ni eupna
  • aminata sylla
    aminata sylla 1 тиждень тому muis
  • Maximiliano5 Santos
    Maximiliano5 Santos 1 тиждень тому Uhd
  • Bigue Ka
    Bigue Ka 1 тиждень тому J'aime
  • LILA fait des vidéos
    LILA fait des vidéos 2 тижні тому Kouy wadial album suuba beuseul j'aime
  • Seynabou Ndiaye
    Seynabou Ndiaye 3 дні тому Damaye. Bleus. J,aime
  • Maman Angie Gomis
    Maman Angie Gomis 2 тижні тому Vraiment souniou deukk les gens disent tout le temps qu'on est pauvre mais bilae c'est dans la tête. Amouniou dei wayei Yalla diox naniou ay niit youy wagnii stress ak foumou meuntii toleuu Parfois, soumay sétane aba no stress, baye Mbaye ak Makh, Wadioubakh, Tapha Touré, kouthia, Sanekh, Combé ak Magnoukk, Diop Fall et tant d'autres personnes sama xol dafay fékh je te jure. Longue vie à vous tous
  • Madina Ly
    Madina Ly 2 тижні тому 😘😘😘😘
  • Madina Ly
    Madina Ly 2 тижні тому 😍😍😍😍
  • Madina Ly
    Madina Ly 2 тижні тому 😘😘😍😍😍😍
  • Papa mor Faye
    Papa mor Faye 2 тижні тому ❤️❤️❤️
  • Touba ndienné Cosmétique
    Touba ndienné Cosmétique 2 тижні тому Bilay sortou wadiobakh
  • Penda Diop
    Penda Diop 2 тижні тому 😍😍😍😍😍😢
  • Tigre Noir
    Tigre Noir 2 тижні тому Sokhna ci lolou dou aduna tok len fi di dieul aye Aba aye kouthia et autres les autres pays avance ngéne nek fi di foh rek
  • Babsa Mbaye
    Babsa Mbaye 2 тижні тому T'as raison
  • Mbathio Diop
    Mbathio Diop 2 тижні тому @Tigre Noir c vrai
  • Tigre Noir
    Tigre Noir 1 тиждень тому @Mbathio Diop Bro Sénégal naniou dém rek li ci kaname moy geuneu pire bala niouko xam niou guéne dém yénéne pays en voix de Développement Sénégal Music féthie théâtre homosexualité gouvernement bi sathie ak féne rek un pays sans avenir une jeunesse sans conscience moy Sénégal
  • dija dieng
    dija dieng 1 тиждень тому @Tigre Noir bilae man iow la andal, certes niougui dindi stress mais lolou dou takh niou developpè il est temps nak, sènègal mom c est un pays sans developpement bilahi
  • Tigre Noir
    Tigre Noir 1 тиждень тому @dija dieng Sénégal kay Lou yalla khame doyna nékou niou sax si yonnou développement deuk bo xam ni foh rek gouvernement bi féne rek
  • dija dieng
    dija dieng 1 тиждень тому @Tigre Noir fi kay pays sans emergence
  • Faty Sambou
    Faty Sambou 5 днів тому Vraiment mahfousse yaa nguii thi
  • Ousseynou Ndiaye
    Ousseynou Ndiaye 3 дні тому Maman Angie Gomis vdj
  • Mahfousse
    Mahfousse 2 тижні тому Wooyyyy Dinaa fegn Télé 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🔥🎬👏🏽 merci Brill
  • Bril Officiel
    Bril Officiel 2 тижні тому Mahfousse 😂😂😂😂😂😂boulma ray way , yaw ak Dudu tothie ngèn clip bi
  • King vision
    King vision 2 тижні тому @Bril Officiel brill comment vah
  • TEAM SARRØ TV
    TEAM SARRØ TV 2 тижні тому @Bril Officiel raft na deh
  • thioro mabo ngom
    thioro mabo ngom 2 тижні тому 😂😂😂😂😂
  • Mouhameth Dieng
    Mouhameth Dieng 2 тижні тому 😅😅
  • La Salihate
    La Salihate 2 тижні тому 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
  • Fatou Diagne
    Fatou Diagne 2 тижні тому @Bril Officiel machala way khol yagui fékh
  • faty daba sow
    faty daba sow 2 тижні тому Mahfousse 😂😂😂
  • Khadim Diop
    Khadim Diop 2 тижні тому Raféte na
  • Touré Touré
    Touré Touré 2 тижні тому 😂😂😂😂😂😂
  • Omar Sallah
    Omar Sallah 2 тижні тому 🤣🤣🤣
  • Diatito S Sambou
    Diatito S Sambou 2 тижні тому Mahfousse meusso werr😂😂😂
  • Sall Diko
    Sall Diko 2 тижні тому 😂😂😂😂
  • Aida Sagna
    Aida Sagna 2 тижні тому Mahfousse 😂😂😂😂😂😂
  • faramaren 100%
    faramaren 100% 2 тижні тому Mahfousse si guedekk
  • Soxna Sourang
    Soxna Sourang 2 тижні тому @Fatou Diagne mmm🤣🤣🥰
  • Bandit Boy
    Bandit Boy 2 тижні тому Mahfousse Yaeh mon broda yagui déff buzz
  • Le karimiste Djinks
    Le karimiste Djinks 2 тижні тому Mahfousse sama idole bi name nala
  • Bandit Boy
    Bandit Boy 2 тижні тому Yeah Malaah Raw Frére Sino Ani Bagage Yi Mais Diokh Ma Sa WhatsApp
  • Bandit Boy
    Bandit Boy 2 тижні тому Bril Officiel Yeah Sama Rappeur Nice
  • Astou Thiam
    Astou Thiam 2 тижні тому @Bril Officiel mane si club bou souba sila beuge bogou
  • lino prancais
    lino prancais 1 тиждень тому @Bril Officiel lol
  • aisetou thiam
    aisetou thiam 1 тиждень тому No bril ndanane leu machalah mala beugeul sama boppp weral yag fii
  • Marodi Télévision jr
    Marodi Télévision jr 1 тиждень тому 😂😂 mahfouss dinama ray👍👍
  • Ndeye Coumba Gueye
    Ndeye Coumba Gueye 1 тиждень тому khol ko dèjà mongui gnuy rèeh lo fi dounlène waye machaalah nèkhna
  • Fall Djiliy
    Fall Djiliy 1 тиждень тому Makh 😂😂
  • Ndeye Mboup
    Ndeye Mboup 1 тиждень тому Mahfousse niakk lénnn di sétane worul wayé niak déglou bril erreur leuh
  • Ablaye Sarr
    Ablaye Sarr 6 днів тому 🖥™️🤣🤣
  • Faty Sambou
    Faty Sambou 5 днів тому MAHFOUSSE ENVOYÉ MA NUMÉROS TÉLÉPHONE
  • Xeuch Class Chic
    Xeuch Class Chic 2 тижні тому Artiste bi moye teug beat di rap teksi meumeu waye #BRIL Kouka beug pousse j'aime
  • Ibrahima DIAGNE
    Ibrahima DIAGNE 2 тижні тому Xeuch Class Chic ki bayina rap dh
  • Xeuch Class Chic
    Xeuch Class Chic 2 тижні тому @Ibrahima DIAGNE Nom tu est trompé
  • Djim Toure
    Djim Toure 2 тижні тому À toi qui lit que DIEU te bénisse toi et ta famille 🙏💞❤️
  • Daaz Kante
    Daaz Kante 2 тижні тому Dope frere j’ai kiffer a vrai dire instant bi kay sa duo ak dip rek lay kharr koussi ande defal pousse bleu
  • un
    un 2 тижні тому Daaz Kante waw waw avéc bril rék alébi n'danane là thia kaw thia kanam
  • Mballo Mohamed moustapha
    Mballo Mohamed moustapha 2 тижні тому Kou pokk thi ande takhawou bril ne passe pas sans appuyer sur le bouton , bou thi bokkoul tamine on s'en fou parce que 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳 daffa nékh dagnouy foo di réé encore💯💯
  • Seck zéro faute
    Seck zéro faute 2 тижні тому Encore Bril danga fess dell ak talent bro yagui niouy bègueul on attend l'album avec impatience
  • Seyda Mariama Moustapha MVP Dabo
    Seyda Mariama Moustapha MVP Dabo 5 днів тому Walahi l jeune talent machalla iao yaye Seine baye sula neihei rap waleu freestyle on t'aime bcppp congratulation
  • astou lo
    astou lo 2 тижні тому way li nakhna way merci bril ndam rek inchallah 💕💕
  • Papa mor Faye
    Papa mor Faye 2 тижні тому Kou gueme ni clips bi mo daka guoume si clips yi beuseul touche bleu👍🏻
  • Lala Diakhaté
    Lala Diakhaté 2 тижні тому Contanaty si yow machallah 😍 khôl dal fekh n'a si yow le 20 septembre dal d'où aye foo
  • Bécaye Diop
    Bécaye Diop 2 тижні тому Lo xamoul kagne lay diékh dafa wara nékh ça je n'en disconviens pas on doit plus laisser le stress ou l'angoisse occupe nos coeur puise qu'on a des gens comme toi #bril# peuvent éradiquer à jamais ces futilités Nice video come dap keep working in this way everything will be all right
  • sabato ehijie
    sabato ehijie 2 тижні тому Si tu aimes cette musique tape j’aime 🙏🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇮🇹🇮🇹🇮🇹🎶❤️❤️❤️👈
  • Modou Cisse
    Modou Cisse 2 тижні тому J aime cette musique
  • Ibrahima Gaye
    Ibrahima Gaye 1 тиждень тому @Modou Cisse nice na ❤️❤️❤️❤️
  • Robson Dasupa
    Robson Dasupa 2 тижні тому En attendant l’album le 20 septembre inchaala cilla bokk🔥🔥🔥🔥
  • Ndeye Thiamba Mboup
    Ndeye Thiamba Mboup 1 тиждень тому Robson Dasupa 💔💔💔
  • Maguette Seye
    Maguette Seye 6 днів тому Le jour de mon annif
  • Robson Dasupa
    Robson Dasupa 6 днів тому Maguette Seye du yomb 🔥🔥
  • Khady Faye
    Khady Faye 2 тижні тому Machalaa trop nex 😍😍ki est la avant les 1milion de vues💪💪❤️❤️
  • Abdoul Aziz Kanoute
    Abdoul Aziz Kanoute 2 тижні тому Non bril t'as une voix d'or bilahii
  • Papa mor Faye
    Papa mor Faye 2 тижні тому Nous devons ouvrir nos yeux sur la génération actuelle. Nous devons promouvoir et soutenir bril. Il est grand et macha allah Vraiment sikaw si kaname ✊🏽long vie à toi
  • Mouhamed sary
    Mouhamed sary 1 тиждень тому Qui est d'accord que Bril est le meilleur de sa génération beusseul j'aime